#baayxalima
N a f a h a n i :
Xassida la goo xam ni kër gumu nekk, wax nañu ni kër googa duñu fa mbugël kénn, liféeg xassida gi mungi ci biir kër ga képp ku Faatu ça kër ga sunu boroom ràmbu la .
Manuscrit : #baayxalima
November 27, 2024 at 10:33 AM